** Streame, écoute & participe ici [ Ссылка ] : l'album HARMONY (Talatay Nder) disponible sur toutes les plateformes musicales & réseaux sociaux **.
Avec les artistes : Kya, KineKine, Ouly, Satou Niang & Soraya
** Clique ici [ Ссылка ] pour suivre l'actualité du label ZBestProduction **
Le collectif de femmes HARMONY - composé de Kya, KineKine, Ouly, Satou Niang & Soraya - présente DJIGUENE LA, extrait de l'album HARMONY (Talatay Nder).
#harmony #djiguenela #clipofficiel #talataynder #femmes #nder #waalo #liberation #kinekine #kya #ouly #satouniang #soraya #nouvelalbum #zbest #zbestproduction #digitprod
** Crédits du single et du clip DJIGUENE LA **
Auteur, compositeur, enregistrement, mix & mastering : ZBest
Un clip de la team ZBest Studio
Réalisateur : ZBest
D.O.P : Mass Pogboom
Montage & color grading : PDM Prod
Lumière : Tijjio Ndiaye
Assistant réalisateur : Authentique
Régie : Djiby Nene, Pas Alune
Photographe : Zou Vision
Direction artistique : Dembis
Maquillage : Fa Beauty
Producteur : ZBest Production (Dakar, Senegal, mars 2024)
** Retrouve ZBEST PRODUCTION sur les réseaux sociaux **
TikTok [ Ссылка ]
Instagram [ Ссылка ]
** Lyrics de la chanson DJIGUENE LA **
Wawawe
C’est comme ça
Femme d’affaire ba kerok mouy nekh
Goor douma yapp mane aythia tay mou nekh
Booy weur diom mongui fi
Foula djou mate akk fite bi sax
"Boo geumé yallah kone loy ragal"
"Khawmako"
Nonou la aduna bi nonou laaaa
Takal sa seur téh boul tok
"Doumako yakar si goor"
Diougual
Diougual
Diougual
Doléy djiguene foulak diom laa waayyy
Diougual
Diougual
Diougual
Yaw boulko door téh boulko saga
"Soma mounoul nekhal boulma diani"
Mérité woul liiii di door aka saga
"Soma mounoul nekhal boulma diani"
Anhhhhhh djiguene laa
Djiguene laa Djiguene laa Djiguene laa
Djiguene laa Djiguene laa Djiguene laa
Teral ko Linguére laa Djiguene laa
"Linguére laa"
Songualingua Songualingua Songualingua
Dedete Songualiwoul kay
Kou meunoul téh bawo lou yakou yawaa
"Djiguene laa"
Nioune nioy djiguene séni yayee
Djiguene séni rakak séni sokhna
Deuk tchie liguey diambar laa
Souma seuyé mou nekh
Ndaxté mane djiguene laa
Mingue kooy door waxoul
Banguay contane mome takoul
Mougne beuss bouné saxoul
"Sama batte sikaw"
Hommage à toute les femmes
Qui sont maltraitées
Dans les maisons dans les prisons
Dina metti wayé boul bayéee
So geumé sa borom loy ragal sa nonnee
"Mane khawmako"
Taye dina metti souba day nekh
Wayé so mougné ni souba day diekh
Sa leppp soti
Yaw boulko door téh boulko saga
"Soma mounoul nekhal boulma diani"
Mérité woul liiii di door aka saga
"Soma mounoul nekhal boulma diani"
Anhhhhhh djiguene laa
Djiguene laa Djiguene laa Djiguene laa
Djiguene laa Djiguene laa Djiguene laa
Teral ko Linguére laa Djiguene laa
"Linguére laa"
Songualingua Songualingua Songualingua
Dedete Songualiwoul kay
Kou meunoul téh bawo lou yakou yawaa
"Linguére laa"
Je suis femme battante
Djiguene foulak fayda djiguene
Ngor akk doylou Djigueneeeee
"Boulko door boulko saaagga Djiguene"
"Boulko torokhal"
Ещё видео!