BUURU NDAM Film bi - [ Ссылка ]
Lii di ab tukki ci biir mbindi yonent yi dafa len di woo ci xamanteek jenn Yàlla ji am kepp te di dëgg. Te it ngeen xam pexeem mi Mu tëral ngir wallu surgaam yi fippu ba tàbbi ci nguurug lëndëm gi. Noonu, ñu mëna dundandook Moom ba fàww ca nguurug leeram ga.
Nii ñu ko nettalee mu xumb ak nataal yeek «wideyo» yu taaru yi di lu nekk, dafa dëppook ‘seetaankati’ àddina sépp ak nu seeni at mëna tollu.
Film bi lépp, tollu na ci 222 simili, mu nekk 15 dogat yu, ñoom ci seen bopp, defees na leen ñaari xaaj yu mag :
Xaaj 1. Kóllëre gu jëkk gi : Buur bi yégle na Pexeem { dogat 1 ba 8}
Xaaj 2. Kóllëre gu bees gi : Buur bi matal na pexeem {dogat 9 à 15}.
NETTALIB 15 DOGAT
Xaaj 1 : Kóllëre gu jëkk gi : Buur bi yégle na Pexeem (Disk 1 = 1 waxtu ak 47 simili)
1. Ubbite gi (Pàcc 1 à 3)
[ Ссылка ]
2. Sàkk-kat bi ak càkkéefam (Pàcc 4 à 9)
[ Ссылка ]
3. Duggug naxekat bi (Pàcc 10 à 15)
[ Ссылка ]
4. Mbugalug bàkkaar ak digeb Yàlla (Pàcc 16 à 19)
[ Ссылка ]
5. Sarax ba (Pàcc 20 à 24)
[ Ссылка ]
6. Fippug nit ak takkuteg Yàlla (Pàcc 25 à 27)
[ Ссылка ]
7. Pexem Yàllaa ngi jëm kanam (Pàcc 28 à 32)
[ Ссылка ]
8. Yoonu Musaa ak tére yonent yi (Pàcc 33 à 36)
[ Ссылка ]
Xaaj 2 : Kóllëre gu bees gi : Buur bi matal na pexeem (Disk 2 = 1 waxtu ak 55 simili)
9. Duggsig Buur bi (Pàcc 37 à 42)
[ Ссылка ]
10. Jikkoy Buur bi (Pàcc 43 à 47)
[ Ссылка ]
11. Nguur gu mag gu Buur bi (Pàcc 48 à 51)
[ Ссылка ]
12. Sasu Buur bi (Pàcc 52 à 56)
[ Ссылка ]
13. Nangug Buur bi (Pàcc 57 à 61)
[ Ссылка ]
14. Saraxu Buur bi ak ndaanug (Pàcc 62 à 65)
[ Ссылка ]
15. Xabaar bu baax bi ak ndamu Buur bi (Pàcc 66 à 70)
[ Ссылка ]
Ni Yàlla màgge (ñu woy ko ci araab) misigu njeexte
© 2019 ROCK International [ Ссылка ]
This journey into the Scriptures of the prophets invites you to meet the one true God and understand His plan to rescue His rebellious subjects from the kingdom of darkness and qualify them to live with Him forever in His kingdom of light. With its thought-provoking narrative and inspired mix of animation and live video, this film is for a worldwide audience of all ages.
The full film is 222 minutes, grouped in 15 episodes, and divided into two main parts:
Part 1. Old Testament: The King Foretells His Plan {Episodes 1-8}
Part 2. New Testament: The King Fulfills His Plan {Episodes 9-15}
KING of GLORY: 1 STORY in 15 EPISODES
Part 1: Old Testament: The King Foretells His Plan [1 hour 47 minutes]
1. Prologue (Scenes 1-3)
2. The Creator & His Creation (Scenes 4-9)
3. Evil’s Entrance (Scenes 10-15)
4. Sin’s Curse & God’s Promise (Scenes 16-19)
5. The Way of the Sacrifice (Scenes 20-24)
6. Man’s Rebellion & God’s Faithfulness (Scenes 25-27)
7. God’s Plan Advances (Scenes 28-32)
8. The Law & the Prophets (Scenes 33-36)
Part 2: New Testament: The King Fulfills His Plan [1 hour 55 minutes]
9. The King’s Entrance (Scenes 37-42)
10. The King’s Character (Scenes 43-47)
11. The King’s Dominion (Scenes 48-51)
12. The King’s Mission (Scenes 52-56)
13. The King’s Submission (Scenes 57-61)
14. The King’s Sacrifice & Triumph (Scenes 62-65)
15. The King’s Gospel & Glory (Scenes 66-70)
How Great is Our God (Sung in Arabic)
Credits
© 2019 ROCK International [ Ссылка ]
Ещё видео!