✅✅ Abdu Rajiim Lëy jambaar dëg ❣️ neena
Seex Anta jóob neena képp ku leen nara jiite ci làkku jàmbur ba noppi ! Jiite leen ci Ak dëgg akuk maandu waxu leen dëgg fay fenn,
Jërëjëf Seex Anta jóob
#cheikhantadiop
#jub #Jubal #jubanti #téyémssi
Le pouvoir ça se prend ça ne se donne pas.
#leaders
#leadership
#motivation #mental_leader
Teewlu leen ko Bu baax ta yàttal»;»
Seex Anta jóob neena képp ku leen nara jiite ci làkku jàmbur ba noppi ! Jiite leen ci Ak dëgg akuk maandu waxu leen dëgg fay fenn,
Jërëjëf Sëñ Abdu rahiim lëy ♥️🥰🙏
Ещё видео!