YONOU NDIOUP
WAKHI SERIGNE TOUBA
Diammi adouna mooy weroukk yaram
Noflayou adouna mooy am ndono
Wèetelou adouna mooy am sokhna
Yeurmandé adouna mooy am doom
Xam xamou adouna mooy xam YALLA
Mane-manou adouna...manéko si say mbok
SERIGNE TOUBA wakh nani
diourome niarr mo gueune diourome niar
1- Bayyi fène mo gueunn diangue AL KHOURANE
2- Saame sa diourome niari thieur mo gueunn deukké koor
3- Fatalikou alàkhira mo gueunn fanàné djiouli
4- Làbiré djioulite yi mo gueune fital djaarr
5- Bayi moyy mo gueunn deukké djéglou
6- Digglé aw yiw mo gueunn baril sarakhé
7- Tèrè lou gnaw mo gueunn deukké gnann
Ещё видео!