Paroles Aida Samb - Mame Samb...
Sobouma mame sobouma waw waw
lima dal koumou dal mou def la wooy
mame samb
(bis)
mo mame gni la xam deug ne negn ne negn mousooulo
changé bene yoone changé bene yoone
té lolou djiko yonénte la
mo mame mamadou hana waliwou nga
ali mamadou
dérete bouy daw sama biir yaram
moma sonal mame
nima fook nga wooy
mame booy ya takh ma wooy mame
boula yala diokhoul dom boula wooy mame
mane mi sa seut mame dinala wooy
mame samb
sobouma mame sobouma waw waw
lima dal koumou dal mou def la wooy
mame samb
senegal ak liko woor mame
afrik yenene frontiere mame
baat bi bene
koni samba diabané mouni dama nekh
mame ya wax ni dooni gawlo takhouta touti
fonkal sa boop
boula kene may ba nopi diépi la mame
fok ma wooy mane gawlo fok ma wooy (4x)
thiossane nou rew mi kene dou thi yow
say dialoré kene douko weedi
dieuleul wooy wi yaye borom mame
wooy wi yaye borom mame kone dieuleul
seuteu ngi wooy mame
mame samb ya yarete djiko
yéééé yé yé yé ...
ki dé dama yeme
seuteu ngi wooy mame
mame samb ya yarete djiko
woo wo wo woyyy
ki dé dama yeme
soko séné mouy dokh
sa yaram dafa daw
...
ki dé dama yeme(bis)
alalaké mame
mo manké
...
mo manké alafa alalaké kobé
....
sene yaye mariata diarra
ablaye daro bane
madior daro bane
gnom gneup yagna coumbé thiong moy sene mame
...@Biglayekb.... Welcom to /////
/
ShowMe AkTivi: No Copyright Content: Music /
★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★
[ Ссылка ]
★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★
[ Ссылка ]
--- Soutenir la Chaîne ---
★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★★
[ Ссылка ]
/
! ShowMe AkTv !
Ещё видео!