[#SaveTheDate - 𝑵𝒊𝒂𝒂𝒏𝒖 𝑺𝒆𝒚𝒅𝒊𝒏𝒂 𝑨𝒃𝒂𝒃𝒂𝒄𝒂𝒓 𝑳𝑨𝑯𝑰]]
« Laayeen goo xamne amatul Sëydinaa Mbay
Xanaa asamaan su amatul jant xam naa
Fu nuy làqooti, moo funu deeti daw jëm
Ka doon yaakaari Àddina jeppa dem na »
🗓️Mardi 17 Janvier 2023
🕒9h: Kamil
🕒00h: Prières et chants religieux
📍 Yoff Diamalahi
@bouchral_mouhibine #appel2023 #layene #jamalahi #niaan #islam #tawhid #muslim
Ещё видео!